Sama Wo Lyrics & Tabs by Philip Monteiro

Sama Wo

guitar chords lyrics

Philip Monteiro

Album : Philip Monteiro kizomba PlayStop

yeah
sama fans yi
magui léne di gueureum

di léne santeu
guiss na séne taxaway
musique bi
pour yen la
oh
mane nop na léne
waw (big up)
yagueu neu lool
bingueu démé
mane réére na
réére na sa yow
lane la wara déf (wax ma)

mane réére na
réére na sa yow
lane la wara déf (wax ma)
déf sans yow (sans yow hey)
dama la soxla
té da ma la beugueu
déme ngueu té bay ma
bay ma si leundeum
wanté xam ngua ni
ni dama wara doumeu maneu doundeu ba téy
déme ngua té bay ma
baby gnewateul si mane
xana déguo sama wo
baby gnewateul
yagueu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wééte
lou maye déf ba ngueu gneuwate
gneuwate si mane
baby gneuwatal
yagneu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wéét
xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane
oh
bou ma togué di xalaate
doundeu you nex gui gnou done doundeu
rek sama xool fess
xama tou ma lou ma wara déf
déme ngua bayi ma thi leundeum
wanté xam ngua ni dama wara doundeu mateye
déme ngua té bayi ma
bayi ma si leundeum
dama la soxla
dama la beugueu
baby ngeuwateul si mane
xana déguo sama wo
baby gnewateul
yagueu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wééte
lou maye déf ba ngueu gneuwate
gneuwate si mane
baby gneuwatal
yagneu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wéét
xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane
xama tou ma li ma wara déf
yagueu neu lool
bouguou ma ngua xaam li ma dadj
nax xaam na nik ame ngua kénéne
meunou ma ko gueum
meuneu dess ni
yagueu na lool bi ngua déme
mane réére na nékeutofi
lane la wara déf nékeutofi
dama la soxla
dama la beugueu
baby gneuwateul si mane
xana déguo sama wo
baby gnewateul
yagueu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wééte
lou maye déf ba ngueu gneuwate
gneuwate si mane
baby gneuwatal
yagneu na lool bi ngua démé
tax na sama xol wéét
xana di la wax beuss bou né fi ngua tolou si mane

Like us on Facebook.....
-> Loading Time :0.0061 sec