Woudjou yaye Lyrics & Tabs by Omar Pene

Woudjou yaye

guitar chords lyrics

Omar Pene

Album : MyambaPlayStop

Bilé Woudjou Yaye (Bis)
Souma démé diangui ba wacca midi
Magnew ci keurgui douma tibal bol

Bou domam gneuwé
Mou diokh ko mou lekka
Bou dessalé mou oubal ma kofa
Mba mou diokh ko khadj ba
Baye yama togn, Baye yama togn
Lou takh nga may bayi ak mom
Bilé Woudjou Yaye hahan
Aka bona bone
Bilé Woudjou Yaye hahan
Aka bona bone
Bilé Woudjou Yaye (Bis)
Souma démé diangui ba wacca midi

Aka bona bone
Bilé Woudjou Yaye (Bis)
Souma démé diangui ba wacca midi
Magnew ci keurgui douma tibal bol
Bou domam gneuwé
Mou diokh ko mou lekka
Bou dessalé mou oubal ma kofa
Mba mou diokh ko khadj ba
Baye yama togn, Baye yama togn
Lou takh nga may bayi ak mom

Like us on Facebook.....
-> Loading Time :0.0044 sec